tabax nañu lislaam ci juróom
Jële nañu ci Abii Abdir Rahmaan Abdulla ibn Umar ibnul Xattaab yal na leen Yàlla dollee gërëm mu wax ne: dégg naa Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "tabax nañu lislaam ci juróom: seede ne amul kenn ku ñu war a jaamu ku dul Yàlla, ak ne Muh…

