{te dees na leen laaj xéewal yi bis booba}
Jële nañu ci Subayru Ibnul Awwaam mu wax ne: Bi aaya bii wàccee: {te dees na leen laaj xéewal yi bis booba} [At-Takaasuru: 8], As-Subayru dafa wax: yaw Yonnente Yàlla bi, ban xéewal lañu nuy laaj, te li fi am mooy ñaar yu ñuul yi rekk muy tàndarma ak ndox? Mu ne ko: «wa…

