”
#3095HadeethEnc[Wér na]
Jële na ñu ci Abdullah Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- bu daan ubbi julli gi day yëkkati loxoom ba mu tolloo ak mbagg yi, naka noonu it daan na leen yëkkati bu daan kàbbar ngir rukóo, ak bu daan sig…
”
#3096HadeethEnc[Wér na]
Jële na ñu ci Ibn Mashuud -yal na ko Yàlla dollee gërëm-, mu wax ne: Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- xamal na ma taaya fekk samay ténq moo ngi ci diggante ñaari ténqam, kem ni mu ma xamale saaru Alxuraan: "Attahiyyaatu lil Laahi, assakiyyaatu lil Laah…
”
#3185HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dugg na ci jàkka ji jenn waay daal di dugg julli ñaari ràkka, daal di nuyu Yonente bi, mu fay ko, daal di ne ko: "demal julli waat, yaw julliwóo", m…
”
#10925HadeethEnc[Wér na]
Jële na ñu ci Ibnu Abbaas -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne : «digal nañu ma may sujjóot ci juróom-ñaari cér : cib jëh, mu daadi junj loxoom ci bakkanam, ak ñaari loxo yi, ak ñaari wóom yi, ak cati ba…
”
#10927HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Al-Baraa yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: "boo sujjóotee, na nga teg say ténq te yëkkëti say conc".
”
#10930HadeethEnc[Tane na bees sukkandikoo ci yeneen yi koy dëggal]
Jële na ñu ci Ibn Abbaas -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da daan wax ci diggante ñaari sujjóot yi: «Allaahumma ixfir lii, warhamnii, wa haafinii, wahdinii, warsuqnii».
”
#10945HadeethEnc[Tane na]
Jële nañu ci Waa-il ibn Hujrin yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Julli naa ak Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc muy sëlmël ci ndayjooram: "assalaamu halaykum warahmatul Laahi wabarakaatuhu", ak ci càmmooñam: "assalaamu halaykum warahmatul…
”
#11256HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc jàng na ci ñaari ràkkay Fajar: {Xul yaa ayyuhal kaafiruuna}, ak {Xul huwal Laahu Ahad}.
”
#65096HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Aasim Ibn Diinaar mu wax ne: Ay nit dañoo ñëw ci Sahl Ibn Sahdin As-Saahidii, fekk dañu doon werante ci minbar bi fan la bant bi jóge, ñu laaj ko loolu, mu ne leen: giñ naa ci Yàlla dinaa xam fan la jóge, ca bis bañu ko fi njëkkee teg laa ko gis, ak bis ba…
”
#65097HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Hittaan Ibn Abdullah Ar-Raxaasii mu wax ne: julli naa ak Abuu Muusa Al-Ashsrii ag julli, dañoo lënkale julli ak ug mbaax ak asaka, nee na: ba Abuu Muusaa noppee ca julli ga ba sëlmël daal di wëlbëtiku, daal di ne: kan ci yéen moo wax baat sàngam ak baat sàn…
”
#65098HadeethEnc[Wér na]
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- ne: Moom daana kàbbar ci bépp jullig farata ak bu dul moom, ci koor ak bu dul koor, bu dee jug kàbbar, bu dee rukoo kàbbar, daal di wax: samihal Laahu liman hamidahu, daal di wax it: Rabbanaa wa lakal hamdu, ba…
”
#65100HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «ki gën a bon ug càcc ci nit ñi mooy kiy sacc julleem» ñu ne ko: naka lay sacce julleem? Mu ne: «du matal rukkoo yi, ak…