lépp a ngi ci ndogal yi, ba ci lott ak muus, mbaa muus ak lott
Jële nañu ci Taawuus mu wax ne: fekk naa fi ay nit ci Sahaabay Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-, ñuy wax naan lépp a ngi aju ci ndogal yi, Taawuus wax ne: dégg naa Abdullah Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko…

