bu Yàlla dogalee ci nit ki mu faatu a fi barab da koy def mu am fa aajo
Choose an available translation of this Hadeeth
Hadeeth text
Jële na ñu ci Matar Ibn Hukaamis- yal na leen Yàlla dollee gërëm - mu wax ne, Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «bu Yàlla dogalee ci nit ki mu faatu a fi barab da koy def mu am fa aajo».
Explanation
Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- day xamle ne bu Yàlla dogalee ci jaam bi mu War a faatu a fi barab te moom nekku fa; da ko fay defal aajo mu dem fa, ñu jël fa ag ruuham.
Benefits
Attribution
Categories
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

