Prophetic Hadeeth Encyclopedia
Search and read verified Prophetic hadeeth translations, explanations, benefits, categories and source attribution.
Search the Hadeeth Encyclopedia
Smart instant results tolerate minor spelling mistakes, with every filter in one place.
Ngëneeli Saaba yi Yàlla gërëm na leen
seedeel naa Yàlla ne set naa wicc ci kenn ci yéen di nekk sama xarit, ndax Yàlla da maa jàpp xarit, niki mu jàppe Ibraahiima xarit
Jële nañu ci Jundub -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Dégg naa Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax li njëkk juroom i fan laata muy faatu naan: " seedeel naa Yàlla ne set naa wicc ci kenn ci yéen di nekk sama xarit, ndax Yàlla da maa jàpp xa…
Mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ci waa Ansaar yi ne: "kénn du leen bëgg ku dul way-gëm, te kenn du leen bañ ku dul ab naaféq, ku leen bëgg Yàlla bëgg ko, ku leen bañ Yàlla bañ ko
Jële nañu ci Al-Baraa -yal na ko Yàlla dollee gërëm-: Mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ci waa Ansaar yi ne: "kénn du leen bëgg ku dul way-gëm, te kenn du leen bañ ku dul ab naaféq, ku leen bëgg Yàlla bëgg ko, ku leen bañ Yàlla bañ ko"…
dinaa jox Raaya ji waa ju bëgg Yàlla ak ub yonnenteem, Yàlla dina ko ubbee ci ay loxoom
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax bisu Xaybar ba ne: «dinaa jox Raaya ji waa ju bëgg Yàlla ak ub yonnenteem, Yàlla dina ko ubbee ci ay loxoom" Umar ibnul Xattaab nee na: masumaa bë…
dénk naa leen ngeen ragal Yàlla ci dégg ak topp, donte jaamub Habasa la, dangeen gis ci sama ginnaaw ag wuute gu tar, waaye nangeen jàpp ci sama Sunna ak sunnay njiit yu jub ya tey jubal
Jële nañu ci Al-Hirbaat Ibnu Saariyata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Benn bis Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa taxaw fi nun daal di nuy waar waar gu jotale xol yi jàq nañu ci, bët yi tuur ci rangooñ, ñu ne ko : yaw Yónente Yàlla bi, wa…
demal ne ko: yaw bokkoo ci waa sawara, waaye ci waa àjjana nga bokk
Jële na ñu ci Anas Ibn Maalik, -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa seet Saabit Ibn Xaysin, benn waay ne ko: yaw Yonnente Yàlla bi, man dinaa la xamal xibaaram, mu dikkal ko fekk ko mu toog ci këram, sëgg bopp…
ñi gën ci yéen ñooy samag maas, topp ci ña ca topp, topp ci ña ca topp'
Jële na ñu ci Imraan Ibn Husayn -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne, Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: "ñi gën ci yéen ñooy samag maas, topp ci ña ca topp, topp ci ña ca topp' Imraan nee na: xamuma ndax Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xée…
Maa ngi leen di dénk ragal Yàlla, ak dégg ak topp, donte ab jaam moo leen jiite, képp ku dund ci yéen dana gis wuute gu bari, maa ngi leen di dénk sama sunna si ak sunnay njiit yu jub yi tey jubal
Jële nañu ci Abuu Najiih Al-Hirbaad ibn Saariyata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc waar na nu ag waare ba xol yi jàq ci, bët yi jooy, nu ne ko: yaw Yonente Yàlla bi! Dafa mel ni waarew tàggatoo la; kon laabire…

