ñi gën ci yéen ñooy samag maas, topp ci ña ca topp, topp ci ña ca topp'
Jële na ñu ci Imraan Ibn Husayn -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne, Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: "ñi gën ci yéen ñooy samag maas, topp ci ña ca topp, topp ci ña ca topp' Imraan nee na: xamuma ndax Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xée…

