aw doj la wu ñu sànni ca biir sawara diirub juróom-ñaar-fukki at, mooy door a wàcc ca sawara sa leegi ba egg ca suuf
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm-mu wax ne: Nekkoon nanu fi Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc, mu dégg am riir, Yonnente bi daal di wax ne: "ndax xam ngeen lan la?" Nee na: nu ne ko: Yàlla ak ub yonnenteem ñoo xam, mu wax n…

