gaaflu bokkaale la, gaaflu bokkaale la, gaaflu bokkaale la, -ñatti yoon-, amunu ci pexe, waaye Yàlla mu màgg mi moo koy dindi ci wakkirlu
Choose an available translation of this Hadeeth
Hadeeth text
Jële na ñu ci Abdallah Ibn Mashuud mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «gaaflu bokkaale la, gaaflu bokkaale la, gaaflu bokkaale la, -ñatti yoon-, amunu ci pexe, waaye Yàlla mu màgg mi moo koy dindi ci wakkirlu.
Explanation
Ibn Mashuud -yal na ko Yàlla dollee gërëm- nee na :
amaana gaaflu tàbbi ci xolu jullit bi, waaye li ko war mooy mu jeñ ko ak wakkirlu ci Yàlla ànd ak di def sabab yi.
Benefits
Njariñu baamtu masala yu am solo yi, ngir ñu wattu ko ak mu sax ci xol yi
Gaaflu li koy dindi mooy wakkirlu ci Yàlla mu kawe mi.
Digle nañu ñuy wakkirlu ci Yàlla rekk te wékk xol bi ci Yàlla mu sell mi.
Attribution
Categories
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

