Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na bëgg ñaan yi làmboo lu bari, daan bàyyi yu dul yooyu
Jële nañu ci Aysatu yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daan na bëgg ñaan yi làmboo lu bari, daan bàyyi yu dul yooyu.

