amul benn jullit buy ñaan ñaan gu amul bàkkaar amul dog mbokk, lu dul ne Yàlla dana ko ko jox ci benn ci ñatt yii: ben mu gaawalal ko ag ñaanam, walla mu dencal ko ko ca allaaxira, walla mu wëlbatil ko ca lu bon lu toll ni moom" ñu ne ko: kon de dananu barile, mu ne: "Yàlla moo gën a barile
Jële nañu ci Abii Sahiid Al-Xudriyu -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "amul benn jullit buy ñaan ñaan gu amul bàkkaar amul dog mbokk, lu dul ne Yàlla dana ko ko jox ci benn ci ñatt yii: ben mu gaawalal…

