buleen njëkka nuyu Yahuud yi ak Nasaraan yi ci nuyoog Salaam, bu ngéen dajee ak kenn ci ñoom ci yoon nangeen ko jaarloo fa gën a xat
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "buleen njëkka nuyu Yahuud yi ak Nasaraan yi ci nuyoog Salaam, bu ngéen dajee ak kenn ci ñoom ci yoon nangeen ko jaarloo fa gën a…

