li gay wax di ci woote lu baax la, boo ñu xibaaroon ndax la ñu defoon dees na ko jéggale
Jële na ñu ci Ibn Abbaas -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu ne: Ay nit yu bokkoon ca bokkaalekat ya, dañoo ëppaloon ci raye, ëppal ci njaalo, ñu ñëw ci Yónente bi Muhammat -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ne ko: li gay wax di ci woote lu baax la, boo ñu xibaaroon…

