ku ma fenal te tay ko na waajal ab wàccuwaayam ca sawara
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: "ku ma fenal te tay ko na waajal ab wàccuwaayam ca sawara".

