waat day jariñ liñuy jaay waaye day yàq tonowu
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax ne: "waat day jariñ liñuy jaay waaye day yàq tonowu".
Books saved in this browser.
Loading favorites…
Tap the heart on any book card to save it here.
Search and read verified Prophetic hadeeth translations, explanations, benefits, categories and source attribution. Page 16.
Smart instant results tolerate minor spelling mistakes, with every filter in one place.
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg naa Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax ne: "waat day jariñ liñuy jaay waaye day yàq tonowu".
Jële na ñu ci Anas -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «Kenn ci yéen du gëm ndare ma gënal ko way-juram ak doomam ak mbooleem nit ñi».
Jële nañu ci Ubay Ibn Kahb -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yonente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «buleen ŋàññ ngelaw li, bu ngeen gisee lu ngeen sib, nangeen wax: Allaahuma innaa nas-aluka min xayri haasihi arriihi wa xayri maa fiiha…
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "bu kenn ci yéen di wax naan: yaw sama Boroom jéggal ma bu la soobee, yërëm ma bu la soobee, wërsëgal ma bu la soobee, waaye na dogu ci lim…
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm -mu wax ne : Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «Waa ji ñu tudd sama tur te julliwul ci man kooku sooy na, waa ji weeru koor dugg ba jeex ta jéggalu ñu ko sooy na, waa ji fekke dundu…
Jële nañu ci Aliyun yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Faatimata yal na ko Yàlla dollee gërëm dafa ñëw ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc di ko jàmbat li muy daj ci soqq ak wol, mu dégg ne dafa am ay jaam, te fekku ko fa, mu wax ko Aysatu, ba mu ñë…
Jële nañu ci Abdullah Ibn Xubayb -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Génn nanu ci guddi gu bari taw te lëndëm lool, di wër Yonnente Yàlla bi ngir mu jiite nu julli, nee na: nu dab ko, mu ne ma: "waxal" te waxuma dara, mu waxaat ma: "waxal", te waxuma dara, mu ne m…
Jële nañu ci Abaan ibn Usmaan mu wax ne: dégg naa Usmaan ibn Affaan yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: dégg naa Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: «ku wax bismil Laahi Allasii laa yadurru maha ismihii say-un fil ardi walaa fis samaa-i…
Jële nañu ci Sahd -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Benn kaw-kaw dafa ñëw ci Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-, ne ko: xamal ma wax joo xam ne dama koy wax, mu ne ko: "waxal: laa ilaaha illalaahu wahdahu laa sariika lahu, Allaahu Akbaru ka…
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «ma wax: Subhaanal Laahi, wal hamdu lil Laahi, wa laa ilaaha illal Laahu, wal laahu akbaru, moo ma gënal lépp lu jant bi fenk ci kawam…
Jële nañu ci Al-Baraa yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: "amul ñaari jullit yuy daje daal di joxante loxo lu dul ne dees na leen jéggal laata ñuy teqalikoo".
Jële nañu ci Kahb ibn Hujrata-yal na ko Yàlla dollee gërëm-mu jële ci Yonnente bi-yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-mu wax ne: «ay mbir a ngii yuy wuutante ku leen di wax du sooy -walla ku leen di def- ginnaaw jullig farata gu nekk, Subhaanal Laahi fanweeri yoon ak ñ…
Follow any language without creating an account.

