man de bokk na ci li may ragal ci yéen sama ginnaaw, ñu ubbil leen naataangey àdduna ak taaram
Jële nañu ci Abii Sahiid Al-Xudrii yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa toog benn bis ci minbar bi nu toog wër ko, mu wax ne: "man de bokk na ci li may ragal ci yéen sama ginnaaw, ñu ubbil leen naataangey àdduna a…

