ku Yàlla namm ci moom aw yiw dana ko nattu
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónenteb Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «ku Yàlla namm ci moom aw yiw dana ko nattu».
Books saved in this browser.
Loading favorites…
Tap the heart on any book card to save it here.
Search and read verified Prophetic hadeeth translations, explanations, benefits, categories and source attribution. Page 5.
Smart instant results tolerate minor spelling mistakes, with every filter in one place.
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónenteb Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «ku Yàlla namm ci moom aw yiw dana ko nattu».
Jële na ñu ci Al-Baraa ibn Aasib -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «jullit bi bu ñu ko laajee ci bàmmeel: day seede ne amul kenn ku ñu war a jaamu ku dul Yàlla ak ne Muhammat ndawul Yàlla la" loolu mo…
Jële na ñu ci Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-mu wax ne: «digal nañu ma ma xeex ak nit ñi ba baa ñuy seede ne amul kenn ku ñu war a jaamu ku dul Yàlla ak ne Muhammat ndawul Yàlla la, ak taxawal julli…
Jële nañu ci Ibn Abbaas yal na leen Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "Yàlla jéggal na samaw xeet njuumte ak fàtte ak lu ñu leen forse".
Jële nañu ci Safwaan ibn Muhris mu wax ne: jenn waay dafa wax Umar yal na leen Yàlla dollee gërëm naka nga dégg Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc di ko wax ci dée ga? Mu ne: dégg naa ko mu wax ne: "dees na jegeele aji-gëm ji Boroomam bu màgg bi ëllë…
Jële nañu ci Al-Miqdaad ibnul Aswad yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: dégg naa Yonente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "dañuy jegeele jant bi ci mbindeef yi ëllëg bis-pénc, ba mu jege leen luy toll ni Miil",Sulaym ibn Haamir wax ne: giñ…
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «bàyyileen ma bu ma leen bàyyee, ndax li alag ña leen jiitu woon mooy seeni laaj ak di wuute ak seeni Yonnente , bu ma leen teree dara na…
Jële ci Muhaas ibn Jabal yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Nekkoon naa ak Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc ci benn tukki, ma xëy benn bis jegesi ko fekk ñoo ngi dox, ma ne ko: yaw Yonnente Yàlla bi, xibaar ma jëf joo xam ne dana ma dugal àjjana di…
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: «yéen nit ñi, Yàlla ku teey la te du nangu lu dul lu teey, te Yàlla dafa digal way-gëm ñi li mu digal Yonnente yi, mu wax ne: {yéen Yonnent…
Jële nañu ci Ibn Abbaas -yal na leen Yàlla dollee gërëm- Jele nañu ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ci li mu soloo ci Boroomam mu màgg mi mu wax ne: «Yàlla dafa bind yu rafet yi ak yu ñaaw yi, daal di leeral ko, képp ku yéene jëf i yiw, te defu ko, Y…
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «Yàlla du xool seen i melo mbaa seen alal waaye seen xol lay xool ak seen i jëf».
Jële nañu ci Umar ibn Xattaab -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Benn bis danoo toog ci yònente bi, fa saasa benn waay ñëw, bu sol yéere ya weex tàll,kawar ga ñuul kukk,te kenn gisul ci moom jeexiit i tukki, te it kenn xamu ko ci nun, bam aksi toog ci yònente bi…
Follow any language without creating an account.

