Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- daa na ko tudde Yàlla ginnaaw julli gu ne
Jële na ñu ci Abis Subayri mu wax ne : Ibn Subayri bu jullee ba sëlmal da daan wax: «laa ilaaha illal laahu wahdahu laa sariika lahu lahul mulku wa lahul hamdu wa Huwa halaa kulli say in Xadiirun, laa hawla wa laa xuwwata illaa bil Laahi, laa ilaaha illal Laahu, wa laa…

