Nekkul woon ku ñaaw i wax du caagine ay jëf, du caagine kuy coow ci ja yi, (marché)te daawul fayantoo lu ñaaw, waaye day baale di jéggale
Jële nañu ci Abii Abdul Laahi Al-Jadalii nu wax ne: laaj naa Aysatu ndayu jullit ñi yal na ko Yàlla dollee gërëm jikkóy Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: Nekkul woon ku ñaaw i wax du caagine ay jëf, du caagine kuy coow ci ja yi, (marché)te…

