deeleen jegeele, tey jubal, te ngeen xam ne kenn ci yéen du mucc ngir ay jëfam" ñu ne ko: yaw Yonnente Yàlla bi, ba ci yaw sax? Mu ne: "ba ci man kay, lu dul Yàlla muure ma ag yërmàndeem ak ngëneelam
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne : Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: "deeleen jegeele, tey jubal, te ngeen xam ne kenn ci yéen du mucc ngir ay jëfam" ñu ne ko: yaw Yonnente Yàlla bi, ba ci yaw sax? Mu ne: "b…

