ñaari julli yii ñooy julli yi gën a diis ci naaféq yi, te bu ngeen xamoon li nekk ci ñoom ñaar dangeen ko teewe donte dangeen di raam ci ay wóom
Jële nañu ci Ubay ibn Kahb yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc jiite na nu benn bis jullig suba mu daal di wax ne: "ndax diw teew na?" Ñu ne ko: déedéet, mu ne waat: ndax diw teew na? Ñu ne ko déedéet, mu ne: "ñ…

