bokk na ci li fi nit ñi fekk ci waxi Yonnente ya jiitu: boo amul looy rus defal lu la neex
Jële nañu ci Abuu Mashuud Uqbata ibn Amr Al-Absaarii Al-Badrii yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi nee na: «bokk na ci li fi nit ñi fekk ci waxi Yonnente ya jiitu: boo amul looy rus defal lu la neex».

