waxal: laa ilaaha illalaahu wahdahu laa sariika lahu, Allaahu Akbaru kabiiran, wal hamdu lil-Laahi kasiiran, subhaanal Laahi Rabbil haalamiina, laa hawla wa laa xuwwata illaa bil Laahi Alhasiisil-Alhakiimi
Jële nañu ci Sahd -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Benn kaw-kaw dafa ñëw ci Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc-, ne ko: xamal ma wax joo xam ne dama koy wax, mu ne ko: "waxal: laa ilaaha illalaahu wahdahu laa sariika lahu, Allaahu Akbaru ka…

