ndax xam ngeen kan mooy ki ñàkk?
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: «ndax xam ngeen kan mooy ki ñàkk?" Ñu ne ko: ki ñàkk fi nun mooy ki amul dërëm te amul ay jumtukaay, mu ne: "ki ñàkk ci samaw xeet mooy ki ñëw…

