giñ naa ci Yàlla ne Yàlla gindi ci yaw benn waay moo gën ci yaw nga am géttug jur
Jële nañu ci Sahl Ibn Sahd -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- wax na bisu Xaybar ne: «dinaa jox raaya jii suba jenn waay joj Yàlla dana def ubbi gi ci ay loxoom, dafa bëgg Yàlla ak ub Yonnenteem, Yàlla ak ub Yonne…

