Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- budaan yëkkati ndingam jóge ca rukoo ba da daan wax: «samihal Laahu liman hamidahu
Choose an available translation of this Hadeeth
Hadeeth text
Jële nañu ci Ibn Abii Awfaa -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- budaan yëkkati ndingam jóge ca rukoo ba da daan wax: «samihal Laahu liman hamidahu, Allaahumma Rabbanaa lakal hamdu, mil-as samaawaati wa mil-al ardi wa mil-a maa sita min say-in bahdu».
Explanation
Benefits
Yoonal nañu yamoo ak dal ginnaaw bu ñu siggee ca rukoo ba; ndax manuta wax sikar bii ludul bu yamoo ba dal.
Sikar bii nag lu ñu yoonal la ci mbooleem julli yi moo xam farata la walla naafila.
Attribution
Categories
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

