waaw ndax su ma jullee julliy farata yi, woor weeru koor, daganal yi dagan, araamal yi araam
Jële nañu ci Abuu Abdulla Jaabir ibn Abdallah Al-Ansaarii yal na leen Yàlla dollee gërëm: Benn waay dafa laaj Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ne ko: waaw ndax su ma jullee julliy farata yi, woor weeru koor, daganal yi dagan, araamal yi araam, te dolliw…

