Daan naa sangu man ak Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ci benn ndab fekk nun ñaar ñépp a am janaba, daan na ma digal ma woddu, muy jonjoo ak man fekk damaa nekk ci mbaax,
Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi-yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Daan naa sangu man ak Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- ci benn ndab fekk nun ñaar ñépp a am janaba, daan na ma digal ma woddu, muy jonjoo ak man fekk damaa nekk ci mbaax, daan…

