Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa am lu mu tudd daal di ne: «loolu de bu xam-xam di dem lay doon
Jële na ñu ci Siyaad Ibn Labiid -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- me wax ne: Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa am lu mu tudd daal di ne: «loolu de bu xam-xam di dem lay doon» ma ne ko: yaw Yónente Yàlla bi, naka la xam-xam di deme, te nun noo n…

