ñaar yii dañoo araam ci sama góori xeet wi, waaye dagan nañu ci jigéen ñi
Jële nañu ci Aliyun Ibn Abii Taalib yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dafa jël Sooy ci càmmooñam, jël wurus ci ndayjooram, daal di leen yëkkëti ci loxoom, daal di wax ne: "ñaar yii dañoo araam ci sama góori xeet wi,…

