ku man a takk jabar na takk, ndaxte moo gën a man a damm ab gis, gën a man a sàmm péy mi, ku ko manul nag dénk naa ko woor, ndaxte dana ko man a téye
Jële nañu ci Abdullah ibn Mashuud yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: nekkoon nanu fi Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: «ku man a takk jabar na takk, ndaxte moo gën a man a damm ab gis, gën a man a sàmm péy mi, ku ko manul nag dénk naa ko w…

