Daan nanu génne asakay muurum koor jamanoy yónente bi, ngir xale ak mag, gor ak jaam, muy Saah ci ñam, walla Saah ci soow mu ñu wayal, walla Saah ci Pepp, walla Saa, walla Saah ci tàndarma, walla Saah ci Raseen bu wow
Jële nañu ci Abii Sahiid Al-Xudrii yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Daan nanu génne asakay muurum koor jamanoy yónente bi, ngir xale ak mag, gor ak jaam, muy Saah ci ñam, walla Saah ci soow mu ñu wayal, walla Saah ci Pepp, walla Saa, walla Saah ci tàndarma, walla…

