bu ab xaj naanee ci ndabul kenn ci yéen na ko raxas juróom-ñaari yoon
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «bu ab xaj naanee ci ndabul kenn ci yéen na ko raxas juróom-ñaari yoon». Nekk na ca sahiihu Muslim: «bu njëkk bi ànd…

