yéen nit ñi Yàlla de jële na ci yéen rëy-rëylug ceddo ga ak seenug damu ci seen baay ya
Jële na ñu ci Abdullah Ibn Umar -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa doon xutba nit ñi ca bisu ubbiteg Màkka ga daal di ne leen: «yéen nit ñi Yàlla de jële na ci yéen rëy-rëylug ceddo ga ak seenug damu…

