wàcce nañu ci man ay aaya yoy musuñoo wàcce yu mel ni ñoom, Ñaari muslukaay yi
Choose an available translation of this Hadeeth
Hadeeth text
Jële nañu ci Huqbata Ibn Haamir -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na ma: "wàcce nañu ci man ay aaya yoy musuñoo wàcce yu mel ni ñoom, Ñaari muslukaay yi"
Explanation
Benefits
Ñaaxe ci muslu ci ñoom ñaar ci bépp ay.
Attribution
Categories
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

