giñ naa ci ki sama bakkan nekk ci loxoom, daa naka rekk Iisaa Ibn Maryama wàcc ci yeen di ab àttekat bu màndu, di toj kurwaa yi, di ray mbaam-xuux yi, dindi galag gi(empo) bi, alal daal di baawaan ba kenn soxlawu ko
Choose an available translation of this Hadeeth
Hadeeth text
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «giñ naa ci ki sama bakkan nekk ci loxoom, daa naka rekk Iisaa Ibn Maryama wàcc ci yeen di ab àttekat bu màndu, di toj kurwaa yi, di ray mbaam-xuux yi, dindi galag gi(empo) bi, alal daal di baawaan ba kenn soxlawu ko».
Explanation
màggal, Ak ne Hisaa-yal na ko Yàlla dolli jàmm-dana ray mbaam-xuux yi, Ak ne moom dana dindi lempo digal nit ñépp ñu dugg ci Lislaam. Ak ne alal dana baawaan ba kenn du ko jël; ndax bariwaayam, ak doylug kenn ku ne ci li mu am, baarke wàcc yiw yi toftaloo.
Benefits
Sariihab Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa folli bu dul moom.
Wàccug baarke ci alal yi ci mujjug jamono, ak ni ko nit ñi di dëddoo.
Bégle ci desug diiney Lislaam ba Hiisaa -yal na ko Yàlla dolli jàmm- ci lay àtte ci mujjug jamono.
Attribution
Categories
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

