”
#3575HadeethEnc[Wér na]
Jële na ñu ci Abuu dardaa -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "ndax du ma leen tegtal li gën ci seen jëf yi, te gën cee sell fa seen Boroom, te gën cee kawe ci seeni daraja te gën ci yéen wurus…
”
#3591HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Hurayrata mu jële ci Yónente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «julliy juróom, ak Àjjuma ba Àjjuma, ak weeru koor ba weeru koor, dañuy far bàkkar yi ci séen diggante bu dee moytu nañu bàkkaar yu mag yi».
”
#3701HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Sahiid Al-Xudriyu, ak Abuu Hurayrata -yal na leen Yàlla dollee gërëm- ñu jële ci Yonente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «Amul benn coono buy dal ab jullit, mbaa tawat walla, jaaxle, mbaa naqar, loraange, walla njàqare, doonte dég…
”
#3718HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu jële ci Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: "torox na, torox na, torox na" ñu ne ko: kan? Yaw Yonnente Yàlla bi, mu ne: "ku fekk ñaari way-juram di ay mag, kenn ka walla ñaar ñépp te…
”
#3719HadeethEnc[Wér na]
Jële na ñu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- da doon dox ci mbeddi Màkka yi, daal di romb doj wu ñuy woowe Jumdaan, mu wax ne: "doxleen lii mooy Jumdaan, ñu beru ñi raw nañu" ñu ne ko: ña…
”
#3791HadeethEnc[Tane na bees sukkandikoo ci yeneen yi koy dëggal]
Jële nañu ci Ibn Mashuud yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "dajee naa ak Ibraahiima guddi gi ñu ma rañaanee mu wax ne: yaw Muhammat, jottalil ma saw xeet samag nuyóo, te nga xibaar leen ne Àjjana…
”
#3863HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Jenn waay dafa wax: yaw Yonnente Yàlla bi damaa am jegeñaale ma leen di jokk ñu may dog, may rafetal jëme ci ñoom ñuy ñaawal jëme ci man, may lewet ci ñoom ñuy fétteerlu ci sama kaw, mu ne ko: "bu dee n…
”
#3910HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne : Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: «amul aw nit wuy jog ci ab jotaay te tudduñu fa Yàlla lu dul ne danañu jog mel ni méddum mbaam, ñu ame ca ag réccu».
”
#4314HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Nuhmaan Inb Basiir -yal na ko Yàlla dollee gërëm - mu wax ne: dégg naa Yónent Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne -Nuhmaan jëmale yaari baaraamam ci ay noppam-: «li dagan de leer na li araam it leer na, seen diggante nag am na ay lënt,…
”
#4558HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abuu Sarrin -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Ay nit ci Sahaabay Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc dañoo wax Yonnente bi ne ko: yaw Yonnente Yàlla bi, way-woomal yi yóbb nañu yool yi, dañuy julli kem ni nuy jullee, di woor kem ni nuy…
”
#4716HadeethEnc[Wér na]
Jële nañu ci Abdullah ibn Busrin yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: jenn waay dafa wax ne: yaw Yonnente Yàlla bi tërëliini lislaam yi dafa bari ci man, xibaar ma lol dinaa ci jàpp, mu ne ko: «bu sa làmmiñ deñ di tooy ci tudd Yàlla».
”
#4721HadeethEnc[Wér na]
Jële na ñu ci Umar ibnul Xattaab -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: dégg na Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- muy wax ne: «su ngeen wakkirlu woon ci Yàlla dëgg-dëggi wakkirlu, kon dana leen wërsëgal kem ni muy wërsëgale picc mi, day xëy nek…