kon bul ma seedeloo, man duma seede ag jeng
Jële nañu ci An-Nuhmaan Ibn Basiir yal na leen Yàlla dollee gërëm: Yaayam Bintu Rawaahata dafa laaj baayam mu may ko lenn ci alalam ñeel doomam, mu tanqamlu ko lu mat at, topp mu mujj gis loolu, mu ne ko: du ma nangu lu dul nga seedeloo Yonente Yàlla bi ci li nga may sa…

