rëbbees na kiy sëy ak soxnaam ci ginnaawam
Jële nañu ci Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm mu wax ne: Yonente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc nee na: «rëbbees na kiy sëy ak soxnaam ci ginnaawam».
Read hadeeth
2Views
0Cards
0Shares

