waa Banuu Israayil ay Yonente ñoo leen doon jiite, saa bu ab yonente faatoo beneen yonente wuutu ko, te ab Yonente du ñëw sama ginnaaw, ay Xalifa nag danañu nëw sama ginnaaw te danañu bari
Jële nañu ci Abii Haasim mu wax ne: toog na ak Abuu Hurayrata yal na ko Yàlla dollee gërëm juróomi at, ma dégg ko muy waxtaan jële ci Yonente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu ne: «waa Banuu Israayil ay Yonente ñoo leen doon jiite, saa bu ab yonente faatoo bene…

