fi Boroom bi di gën a jegee jaam bi mooy ci mujjantalu guddi gi
Jële nañu ci Abii Umaamata mu wax ne: Amru Ibn Abasata yal na ko Yàlla dollee gërëm wax na ma ne dégg na Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: «fi Boroom bi di gën a jegee jaam bi mooy ci mujjantalu guddi gi, boo manee di bokk ci ñiy tudd Yàlla ci…

