li dagan de leer na li araam it leer na,
Jële nañu ci Nuhmaan Inb Basiir -yal na ko Yàlla dollee gërëm - mu wax ne: dégg naa Yónent Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne -Nuhmaan jëmale yaari baaraamam ci ay noppam-: «li dagan de leer na li araam it leer na, seen diggante nag am na ay lënt,…

