ku sàkku a dog àqi jullit ci giñam, Yàlla waral na ci moom Sawara, araamal ci moom àjjana" jenn waay ne ko: donte mbir mu ndaw la yaw Yonnente Yàlla bi? Mu ne ko: "donte ab bantu Araak la
Jële nañu ci Abii Umaamata Iyaas ibn Sahlabata Al-Haarisii yal na ko Yàlla dollee gërëm mu jële ci Yonnente Yàlla bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: "ku sàkku a dog àqi jullit ci giñam, Yàlla waral na ci moom Sawara, araamal ci moom àjjana" jenn waay ne…

