ku tabax jàkka ngir Yàlla Yàlla dana ko tabaxal ca àjjana lu mel ni moom
Choose an available translation of this Hadeeth
Hadeeth text
Jële nañu ci Mahmuud Ibn Labiid -yal na leen Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Usmaan Ibn Affaan dafa bëggoon a tabax jàkka ji nit ñi sib loolu, ñu bëgg mu bàyyi ko ca na mu mel, mu ne leen: dégg naa Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- mu wax ne: «ku tabax jàkka ngir Yàlla Yàlla dana ko tabaxal ca àjjana lu mel ni moom».
Explanation
Benefits
Yaatal jàkka ak yeesal ko day dugg ci ngëneelu tabax gi.
Solos sellal ñeel Yàlla mu kawe mi ci mbooleem jëf yi.
Attribution
Categories
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

