HadeethEnc · 1.30.0
Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- rëbb na kiy ger ak ki ñuy ger cib àtte
Available translations
Choose an available translation of this Hadeeth
01
Hadeeth text
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne: Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- rëbb na kiy ger ak ki ñuy ger cib àtte.
02
Explanation
yónente
bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa ñaanal ag dàq ak sori yërmànde Yàlla ñeel kuy joxe ger ak ki koy jël.
Bokk na ci loolu li ñuy jox àttekat ya ngir ñu jeng ca àtte ba ñuy def; ngir kiy joxe jaare ca ba am la mu bëgg ci lu dul dëgg.

03
Benefits
Joxe ger ak jël ko dafa araam, ak di dox ci diggante ñaar ñiy ger’ ak di ca dimbalante; ngir la ca nekk ci dimbalante cig neen.
Ger ci bàkkaar yu mag yi la; ndaxte Yónente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- dafa rëbb ki koy jël ak ki koy joxe.
Ger ci wàllu àtte moo gën a bon, gën rëy bàkkaar; ndax la ca nekk ci tooñ ak àtte ci lu dul li Yàlla wàcce.

Attribution
[At-tirmisiy soloo na ko, ak Ahmat]
Categories
Share
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares