dungeen dugg àjjana ndare ngeen gëm, te dungeen gëm ndare ngeen bëggante, moo ndax duma leen tegtal lol su ngeen ko defee dangeen bëggante? Siiwalleen ab nuyóo seen diggante
Choose an available translation of this Hadeeth
Hadeeth text
Jële nañu ci Abuu Hurayrata -yal na ko Yàlla dollee gërëm- mu wax ne : Yonnente Yàlla bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- nee na: «dungeen dugg àjjana ndare ngeen gëm, te dungeen gëm ndare ngeen bëggante, moo ndax duma leen tegtal lol su ngeen ko defee dangeen bëggante? Siiwalleen ab nuyóo seen diggante».
Explanation
Benefits
Bokk na ci matug ngëm jullit bi bëggal mbokku jullitam li mu bëggal boppam.
Sopp nañu tasaare ab nuyóo ak di ko defal jullit ñi; ndax li ci nekk ci tasaare bëggante ak kóolute ci diggante nit ñi.
Nuyoob lislaam duñu ko defal ku dul ab jullit; ndax li Yonnente bi -yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc- wax ne: "seen diggante".
Nuyoob lislaam dana dindi dogante ak bàyyeente ak mbañeel.
Solos bëggante ci diggante jullit ñi,ci ne daa bokk ci liy matal ngëm.
Ñëw na ci beneen hadiis ne nuyóo bu mat sëkk mooy: "assalaamu halaykum wa rahmatul Laahi wa barakaatuhu", "assalaamu halaykum" it dana doy.
Attribution
Categories
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

