HadeethEnc · 1.30.0
Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daawul bàyyi ñenti ràkka njëkk Tisbaar ak ñaari ràkka njëkk suba gi
Available translations
Choose an available translation of this Hadeeth
01
Hadeeth text
Jële nañu ci Aysatu ndayu jullit ñi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc mu wax ne: Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daawul bàyyi ñenti ràkka njëkk Tisbaar ak ñaari ràkka njëkk suba gi.
02
Explanation
Aysatu yal na ko Yàlla dollee gërëm day xibaare ne Yonnente bi yal na ko Yàlla dolli xéewal ak mucc daa saxoowoon julliy naafila ci këram te daawu ko bàyyi: ñenti ràkka ci ñaari sëlmël njëkk jullig Tisbaar, ak ñaari ràkka njëkk Fajar.
03
Benefits
Sopp nañu sàmmonte ak ñenti ràkka njëkk jullig Tisbaar, ak ñaari ràkka njëkk jullig Fajar.
Li gën mooy ñu jullee naafila yi ca kër ga, looloo tax Aysatu xibaare ko yal na ko Yàlla dollee gërëm.
Li gën mooy ñu jullee naafila yi ca kër ga, looloo tax Aysatu xibaare ko yal na ko Yàlla dollee gërëm.
Attribution
[Al-buxaariy soloo na ko]
Categories
Share
Share hadeeth
Sharing options · 0 Total shares

